VAREFOU DIOULITE .pdf
À propos / Télécharger Aperçu
Nom original: VAREFOU DIOULITE.pdf
Ce document au format PDF 1.5 a été généré par Microsoft® Word 2013, et a été envoyé sur fichier-pdf.fr le 30/06/2014 à 16:18, depuis l'adresse IP 41.214.x.x.
La présente page de téléchargement du fichier a été vue 1367 fois.
Taille du document: 237 Ko (6 pages).
Confidentialité: fichier public
Aperçu du document
Sén mbokoum tàlibe : SERIGNE MODOU MBAYE KHADIMOUL KHADIM
Vàrèfou dioulit nak mooy mou khamlou ay faratàm guir mou mana diàmou
Boroomam migakhamni niou diàmou ko rék mootakh mou andy nioufi.
Bismilahi Fasseyéné Liguéyal Khadimou Rassoul
TE:77 828 49 47 / 76 833 83 71
Email:modou2500@hotmail.fr
THIANGAYE
FARATAY THIANGAY (5)
SUNAY THIANGAY ( 4 )
1 raxass lokho (si booy tambali )
1) Yééné (ci booy rakhass Sa sakara)
2 galaxndikou
2) Raggue( Booy sotti ndokhmi gay bombàlé yaramwi)
3 saraxndikou
3) Gaaw (loo paré démci lénén ) Banie koo dogamtal
4 massaa beune_beunou nopou
4) xalil kawarou bopou
5) Nace aye léét
NDIAPOU
FARATAY NDIAPOU (8)
1 yééné (ci booy raxass sa kanam)
2 raxass kanam
3 raxass loxo ( tiki diara ba si thionthiou)
4 xalil baaramou lokho
5 massaa bopou
6 raxass tank
7 raggue
8 gaaw
SUNAY NDIAPOU (8)
1 raxass lokho bassi tiki diara
2 galaxndikou
3 saraxndikou
4 fiirou
5 yééssal ndox booy massa nopou
6 massaa gnaari nopou
7 déllo massaa bopou
8 toftalé faratayi
TIIM
FARATAY TIIM (8)
SUNAY TIIM (3)
1 Yééné (daganelou litax ngay tiim)
1 toftalé faratayi
2 pakke bou laape
2 yééssal doorine booy massaa lokho
3 gaaw
3 massaa tiki jarra bassi thionthiou
4 daurine bou ndieuke (ték sa loxo si souffe)
5 massaa kanam
6 massaa loxo baci tiki diarra
7 taxalook thi litax ngay tiim
8 défko ci tabbik waxtouwi
KOOR
FARATAY KOOR (2)
SUNAY KOOR (3)
1 yééné
1 gaawa dok
2 féggou ci louy dok koor
2 yéxa xeud
3 fék sa laamigne si wax lou niaaw
ASSAKA
FARATAY ASSAKA (4)
TEGGUINI ASSAKA (3)
1 yééné
1 tééyouk bakane
2 mat at
2 joxé li digou daumou ci alal ji
3 mat nissap
3 sutural
4 niaka toxole
Nissap : mbay= 6 barigo ; khar ou bey= 40 ; xaaliss=500 000F ;
joxél béne ci foukou you nék
jOULLI
FARATAY jOULLI (15 )
SUNAY jOULLI (18)
1 yééné booy kabbar
1 lixam
2 kabbar gou ndieuk
2 jangue saar ganaw fatiha
3 taxawayou kabbarbi
3 jotayou diangue saar
4 jangue fatiha
4 birel fougnouko digléé
5 taxawayou jangue fatiha
5 yéllou fougnouko digléé
6 roukon
6 yénéén kabbar yi désse
7 sigguéé si roukon
7 taaya
8 soudioot
8 jotayou taaya
9 sigguéé si soudioot
9 salatoul alal nabi
10 yééné roy imam (bounela jitéé)
10 dolli ci dalgui
11 toftalé faratayi
11 dolli dal si seulmeul
12 dal (bo sigguéé ngani ték)
12 bireul seulmeul
13 yamoo ( bo siggué nga joupe xothie)
13 déllo seulmeul imam wala kénén
14 seulmeul
14 noppi bou imam di bireul
15 jotayou salmeul
15 sattir
16 sami alahou limane hamida
17 djital fatiha
18 jurome yiy lal souf booy soujoot(bakane,tinkhe,dieu,aume,cati baaramu tank)
AJJI MAKA
FARATAY AJJ (4)
SUNAY AJJ (12)
1 yééné
2 weur kaaba bissup foukélba
3 dox safa ak marwa (6 fois)
4 taxaw arafat bissup jurom gnintél
SUNAY ARMAL
1 Sangou farata
2 tarax laayu
3 juli niaari raka(fatiha+xulyaa ayuxal
kafirona,fatiha+ixlas)
4 wax labayka alaxuma labayka
SUNAY TAWAF
1 dox bagna waar dara
2 foone dojwa si guémigne
3 niuku goorya(niati yoone yu ndieukyi)
4 niane
SUNAY DOKH SAFAA AK MARWA
1 Foone dojba
2 yékci kaw safaa ak marwa
3 gnuku goorya
4 gnane ci kaw safaa ak marwa






Sur le même sujet..
bopou
faratayi
seulmeul
faratay
joulli
raxass
marwa
yeene
lokho
assaka
sunay
kanam
massaa
fatiha
sigguee