Recherche PDF


Cet outil permet de trouver un fichier parmi les documents publics partagés par les utilisateurs de Fichier-PDF.fr.
Dernière mise à jour de la base de données: 13 août à 04:58 - Environ 390000 fichiers indexés.

Afficher résultats par page

Réponses pour «joulli»:



Total: 2 résultats - 0.002 secondes

100% - VAREFOU DIOULITE

joxél béne ci foukou you nék jOULLI FARATAY jOULLI (15 ) SUNAY jOULLI (18) 1 yééné booy kabbar 1 lixam 2 kabbar gou ndieuk 2 jangue saar ganaw fatiha 3 taxawayou kabbarbi 3 jotayou diangue saar 4 jangue fatiha 4 birel fougnouko digléé 5 taxawayou jangue fatiha 5 yéllou fougnouko digléé 6 roukon 6 yénéén kabbar yi désse 7 sigguéé si roukon 7 taaya 8 soudioot 8 jotayou taaya 9 sigguéé si soudioot 9 salatoul alal nabi 10 yééné roy imam (bounela jitéé) 10 dolli ci dalgui 11 toftalé faratayi 11 dolli dal si seulmeul 12 dal (bo sigguéé ngani ték) 12 bireul seulmeul 13 yamoo ( bo siggué nga joupe xothie) 13 déllo seulmeul imam wala kénén 14 seulmeul 14 noppi bou imam di bireul 15 jotayou salmeul 15 sattir 16 sami alahou limane hamida 17 djital fatiha 18 jurome yiy lal souf booy soujoot(bakane,tinkhe,dieu,aume,cati baaramu tank) AJJI MAKA FARATAY AJJ (4) SUNAY AJJ (12) 1 yééné 2 weur kaaba bissup foukélba 3 dox safa ak marwa (6 fois) 4 taxaw arafat bissup jurom gnintél SUNAY ARMAL 1 Sangou farata 2 tarax laayu 3 juli niaari raka(fatiha xulyaa ayuxal kafirona,fatiha ixlas) 4 wax labayka alaxuma labayka SUNAY TAWAF 1 dox bagna waar dara 2 foone dojwa si guémigne 3 niuku goorya(niati yoone yu ndieukyi) 4 niane SUNAY DOKH SAFAA AK MARWA 1 Foone dojba 2 yékci kaw safaa ak marwa 3 gnuku goorya 4 gnane ci kaw safaa ak marwa

fichier-pdf.fr/2014/06/30/varefou-dioulite/ 30/06/2014